Amadeus - Bëgg naa la man lyrics

[Amadeus - Bëgg naa la man lyrics]

Eh Massamba walo
Hey waay
Zoom on the beat

Bëgg naa la
Reason to be, man fonk naa la
Yaay jant bi, man bëgg naa la
Nii ma la bëggee yi jeggi na dayo

Eh way ye way mi girl
Mi yi dei ma for life
Lu nekk jaral nga ma
Kenn mënul tax, man mere la
Ñook seeni wax
Fuck nañu leen daaw

Man so merre damar jaaxle, tiis
Dama la bëgg
Be neen jigéen mënul tax ma giif
Ndax yaw la bëgg
Amul sax
Nit kuy mën xam li may yëg ci yaw
Amul sax
Nit kuy mën compu ni ma la bëggee yiiii

Bëgg naa la man
Ehh eh, bëgg naa la man
Bëgg naa la man
Ehh eh, bëgg naa la man
Eh way!

Dama la bëgg ba faf gëmewuma la
Bañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la
Dama la bëgg ba faf gëmewuma la
Bañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la eh

Jàmm nga may laaj ma ñëw indi feeling paj
Ku dégg ngay laaj te man dama dégg daaj
Ehh tamit ci àdduna, man rekk ma lay beggël
Jàmm nga may laaj ma ñëw indi feeling paj
Ku dégg ngay laaj ma ñëw indi feeling paj
Eh tamit ci àdduna, man rekk ma lay beggël
Ku la laale man lay raagal
Te ku la tooñ may nangu xeex bi

Eh way ye way mi girl
Mi yi dei ma for life
Lu nekk jaral nga ma
Kenn mënul tax, man mere la
Ñook seeni wax
Fuck nañu leen daaw

Man so merre damar jaaxle, tiis
Dama la bëgg
Be neen jigéen mënul tax ma giif
Ndax yaw la bëgg
Amul sax
Nit kuy mën xam li may yëg ci yaw
Amul sax
Nit kuy mën compu ni ma la bëggee yiiii

Bëgg naa la man
Ehh eh, bëgg naa la man
Bëgg naa la man
Ehh eh, bëgg naa la man
Eh way!

Dama la bëgg ba faf gëmewuma la
Bañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la
Dama la bëgg ba faf gëmewuma la
Bañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la eh

Interpretation for


Add Interpretation

A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z #
Interpret