Ndiolé Tall, Wally B. Seck - Choco Vanille lyrics
Wally Ballago Seck [Ndakaaru, Le Sénégal] 🇸🇳
[Ndiolé Tall, Wally B. Seck - Choco Vanille lyrics]
Cherie danga ma, wayi mani tam, dama la, dama la love
Sama amore mio kaye nyu waxtan
Sa pararipi moye sa parara
Suma Yallah beugé na ma bayé ak yow, nangu na
Suma Yeuf ngeu dieulal ya ma mom
Ku né djigeen yaassout, ya len meun
Wooor na ma
Suma la terré nga ba, du man ngeu bueug
Yaye suma honey, ay sweetheart
Mbeuguel ci xol, lenen da ca xaajul
So ko buegué dougal ko status
Sa pararipi moye sa parara
Kaddou gui benn leu
Yeneh gui eupp neu
Bena baat la ci keur gui wai wallie baby diokh na leu ko
Su la nekhé wodouma ma soumi lamsal
Dose bi gueun ci man, ya ma koy piqure
Yaye sama docteur, nyowal consulté meu
Mbeuguel ci xol, lenen da ca xaajul
So ko buegué dougal ko status
Sa pararipi moye sa parara
I’m in love with you, you are my absolute baby wakhal
Me too i love you, my husband my bestfriend
Koula indil gourou demal dinala goungé
Deff na leu fou leundeumeu leundeuma leundeum ci birr xolam
Kou meunta bueugg
Menoul phylosophie mbeuguel
Yow proffesseur, kaye wakh ci mbeuguel
Mbeuguelou legui legui mom dalaye gaagne
Sama xol bi yangi koy gnouroum gnarami
Sama xol bi fess na
Baby man bekk na
You might also like
Pararipi ( en kay)
Damay woutti wallou (wouy lerr)
Xale bi diarr na ko (en kay)
Mo Adja Sene
Mansour ak Doumbé
( Worna yalla bueug na la)
Papis Diallo Cherie Boussou mboub la
Sa pararipi (en kay)
Kaye nga wakh ma ko (ndeysan)
Ni nga ko bueugé (nopp na la)
Nonou la koy deffer ( bueug na)
Pararipi
(Mane fonk na kou melni Ndiole Tall)
Mami traore kouye sa pararipi ( mbeuguelou tey ni la)
Kader Ndiaye moye sa pararipi
Birima Jakarlo kouye sa pararipi
(Sokhna limou deff ci man mi)
Pararipi
Maguette Thioye kouye sa pararipi
Mounass seck kouye timigneumeu
Khadim Kassé kouye sa pararipi
Chouu Bueug na leu, tey ngeu xam né bueug na la
( bayi ma yangi maye toñ)
Feleul felaleko te rigg sa ndiigu gnou dokh dadier
( ding ma gnemé)
Tassal sama lall bi
Di nakko lalate diaral ngama
( yangi maye toñ, yangi maye toñ damay nelaw)
Baby diogueul tokk gnou jakarlo
Do fi nelawé
(gagne nga ma cherie)
Tey nuit de noss la gnoune dañouy veiller yaw rek la
( Mey na leu Kine Diouf tekk ci Thione)
Baby dell feugg sa deun bi
Dell gaww ni mann yaw la nobb
( mohammed damay sonal Ndella wally wakhi nopeu)
Fethie bou bess noko touder
Lolou diaroul lathie
Lolou diaroul lathie my baby
Cherie boy sa fethie bou bess bi noko touder
Baby diaye na sama sante bi
Seck lakko toudé
Diaye na sama sante bi
Yaye Choco Vanille
Vanille Vanilla
Sama choco vanille nga
Diaye na sama sante bi
Yaye Choco Vanille
Vanille Vanilla
Sama choco vanille nga
Yaye sama choco vanille