Samba Peuzzi - Dawalale paroles de (lyrics)

Samba Peuzzi

Samba Peuzzi [Samba Tine] Diamaguène-Diaksao, Dakar, Sénégal 🇸🇳

[Samba Peuzzi - Dawalale paroles de lyrics]

[Couplet 1]
Limay yeukk, si xol bi dou dagn
Mbeuguel deugu xol, dou fegn
Souma la togné, nagn ma bal
Bima nieup folé, yama fal

Yalla déf, finiou yéksi tay
Kon nak, douma bayi, loumou méti méti
Kon waro tite, ndax doto wétt
Filék yagui guéssou, guisma sisa wét

Kén doula diam, Nani
Gillet pare balle, magui ni malay arr
Sisa wét lay fanane si
Loumou guoudii guoudii, bea nangu ma xar
Kay diégué ma, gua wax ma

Chéri, bo beugué beugu na
Bo beuguoul beuguou ma
Yaw diégué ma, wax ma
Bo bégué beugu na


Bo beuguoul beuguou ma

[Refrain]
Ay dawalal, chéri, dawalal
Ya téyé volant bi, boul taxaw, dawalal
Ay dawalal, mon bébé, bawalal
Ya téyé volant bi, boul taxaw, bawalal

Day méti rék, wayé
Nioune niarr, nioy andando
Kouleu bagn, nam bagnalé
Ndax nioune niarr, nioy andando

[Couplet 2]
Mane beuguouma, ragual na
Nit di dox, dima guiss sans yaw
Kon dou nice

Yaw dagu ma fan, dam la fan
Ligua guiss si man, né si yaw
Xol bou nice

Mane naleu diap, yeukeutileu
Ba nit nieup xamni yawla
Sama xol bi yako damp, diko beugu
Noko beugué yakofa am

Dagu ma diégué
Yokou ma ndam, midé yidéma
Té noko beugué beugu na
Kay diégué ma, gua wax ma

Chéri, bo beugué beugu na
Bo beuguoul beuguou ma
Yaw diégué ma, wax ma

Bo bégué beugu na
Bo beuguoul beuguou ma

[Refrain]
Ay dawalal, chéri, dawalal
Ya téyé volant bi, boul taxaw, dawalal
Ay dawalal, mon bébé, bawalal
Ya téyé volant bi, boul taxaw, bawalal

Day méti rék, wayé
Nioune niarr, nioy andando
Kouleu bagn, nam bagnalé
Ndax nioune niarr, nioy andando

Interprétation pour


Ajouter une interprétation

A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z #
Interpréter