Jahman Xpress - Khalé Bingay Wo lyrics

Jahman Xpress [Abdoulahad Thioune] Senegal, West Africa

Сunuy Jahman Xpress lay melni dee sa ñaar ci njëkk. Liggëy na ngaay "Machallah" ak "Magnifique" benn mënaañ yëngëenët, dafa neeg a benn liggëy, dafa neeg a ci yoon wi, nga joxe dëgg nañu. Yépp naa ñaar naa neex, settalu nañu wëër yi lañuy neex nañu. Noppal ak rawatinaan bi, sa yëén yéegal ci biir, tóor moo nopp, dëgg nga tay dund ci xët. Ci biir yi, mën bëgg nga tay sa neex, yëngël nga tay sa sori. Ci mànk gi, ndox bi mu ñëw ci yoon gi, mën naan nga yëén naa rawataan yoon. Xamaloonu melni di Jahman Xpress, ñi waral nga dëgg tayu leen ci yoon gi. Nopp naa Jahman Xpress dina laaj. Dafa neeg a ci yoon wi, dafa neeg a lay tax aw. Yëngël nga tay melni di Jahman Xpress dina laaj. Jahman Xpress moo ko ci dañuy waxoon. Nopp naa Jahman Xpress tey, sa gëj gi dëgg nga tayu leen ci yoon gi.

[Jahman Xpress - Khalé Bingay Wo lyrics]

Danga wara yam
Cuub dafay xam lekkam
Mag du nax bopam
Man ponkala may àttan
Ki ma nekkal zero faute
Panu xaalis xëbbaluma
Yang may woo maa lay xoj
Demal togg wërumala

Eh yaw coupeel maa ngi jokko
Ki ma nob ma nob ko
Ki la gëna pare
Ki def bague sama loxo

Eska man ndiroo naa la
Ku lamb yaw xolaat ma
Ku dul moom gisuma la
Bàyyi ma ngir Yàlla
Kenn du am ki ma am
Di ko weccoo da mën boram
Ki ngay woo muñal ko day wax ak kim jox xolam



Su de jinne pesu la te dofoo
Man soo ma xoolee xam ne dama ne ci loxo
Man ak ñi lamb xam nga ni y’a pas photo
Dama neex a xol ki ma yor moo ma tooppato (mu ne)

Eh xale bi ngay woo
Mu ngi jokkok keneen ki mu nob ba ko
(Te Yàlla tax)
Sonal nga ko (torop)
Eh bako (nga ni)
Ne na sonal nga ko
Eh bako, ehh
Gëmal Yàlla bàyyil ki nobu la

Xale bi ngay woo
Mu ngi jokkok keneen ki mu nob muñal
(S'il te plaît)
Ko ba beneen (tamit)
Way bako
Ne na sonal nga ko (dëgg Yàlla)
Way bako eh
Gëmal Yàlla bàyyil ki nobu la

Loy saf si man (xawma)
Jar na ba pare (bu yàgg)
Dozé ma yombul bàyyil sa xel bi ngay kafe (aw demal togg)
Ki rekk ka fi ne moom rekk gami la signé
Bësal bouton bu xonq bi danga wara coupé
Su de luy raye la man na ma ray man bëgg na
Man benn yoon lay toy ma raw ciment

Garde la ligne soo yakamtiwul
Damay wax ak bonheur
Fi ak wer mën nañu ko wax
Fi m’ma kepp moo dëgër
Ocuppé kañ nga nar a coupé
Bànneex lay waxal soo may woo lay communiqué
Ñamu mak xale lu ciy yoonaam
Place bi am na boroomam
Forcé taxul nga jot ci man soo ma xiifee yëyal singom

Coupél quitteel
Bànneex lay communiqueel
Fideel ci moom
Maa ngi dundu mbëggeel

Bul ma ñodi lu amul ci moom la dagg bu yàgg
Kiy tax bàyyi ko juddoogul baayam de na bu yàgg
Lu ma jooxañ mu dagg te jox na ma sama gedd
Caabi jàng ñu sànni géej
Buntu nekk booy fëgg

Su de jinne pesu la te dofoo
Man soo ma xoolee xam ne dama ne ci loxo
Man ak ñi lamb xam nga ni y’a pas photo
Dama neex a xol ki ma yor moo ma tooppato (mu ne)

Eh xale bi ngay woo
Mu ngi jokkok keneen ki mu nob ba ko
(Te Yàlla tax)
Sonal nga ko (torop)
Eh bako
Ne na sonal nga ko
Eh bako, ehh (nga ni)
Gëmal Yàlla bàyyil ki nobu la

Xale bi ngay woo
Mu ngi jokkok keneen ki mu nob muñal
(S'il te plaît)
Ko ba beneen (tamit)
Way bako
Ne na sonal nga ko (dëgg Yàlla)
Way bako eh
Gëmal Yàlla bàyyil ki nobu la
(Lëjjal nga ma witt)

Interpretation for


Add Interpretation

A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z #
Interpret