Ngaaka Blinde - King Baba lyrics

[Ngaaka Blinde - King Baba lyrics]

Diay katou livre bou meunoul lire
Kokou dé pocham rek laay guiss
Yagg nagnou takk souniou biir

Kone pour nga diss gnou dafay diss
Bimay fessal Aréna
Yangui fessal sén fossou keur
Takhawé tankeu Assane diouf
Nara xorom fepp fo soukeur
Rakhassate Game bi bamou sett
Takh nga kih am fotokk
Konn bodone gorr dinga lathieu
Autographe wala photo
Yae montre bou chère té amoul heure
Nandité rek nga tardel
Do bandit... Do bandit
Amo pakka, Amo Gun
Boudé deug la armel
Madi Saï-Saï yeah may tekk
Boko wédi dieuli beafteak
Kaykay sama zone eyyy


Sa bakane akk sa life lay biff tekk
Dellou hotel Teudi sén Jail
Mayé liquide yi sén guel

Konn Xam ngama?
Lane ngama diay mais[...]

Li nekkatou réwanedé Dama dof
Li nékatoul bon Légui dama con
Nieup laay Ray nama Yalla baal
Gën lénna oyof comme cheikhra fall

BABA
KING BABA
AYOOO
BABA
KING BABA
AYOO
BABA
KING BABA
AYOOO
BABA
KING BABA

Mann kouma sénetou ci gallou khathie
Doumassi lekk té douma nane
Louma sonou-sonou louma lotou-lotou
Mann kotou-kotou kepp douma niane
Wakhal ma yaye nana sani niane
Mame dolli niane rek ma goudou fane
Kou djoudou guiss deugg dou doundou fénn
Beugue yalla bang yonente yi
Amoul féneu
Lima nara tekk takh yone bii tare
Mann ak illimunates yi dougn meun far
Talibé Bamba la Akassa worna serigne Abdou karim akk cheikhra Fall
Bandit deugg day yoré Gun? wala
Bandit deugg day beurri dJeez?
Sama dougou Jail sénn Bénéfice
Guéne té Yakaté match bii
Li nékatoul réwandé dama dof
Dama guéneu cachot rek diari Fann
Kouma deg deugg naka khoff balama
Lepp sa carrière ci gnari fane
Li nékatoul champagne Don-Simon
Lekkou ma... Nanou ma. Dama dof
Deffal ma rappeur yi sama coffre
Ma deflénn ni Sompate nieunou rhoff

Li nekkatou réwanedé Dama dof
Li nékatoul bon Légui dama con
Nieup laay Ray nama Yalla baal
Gën lénna oyof comme cheikhra fall

BABA
KING BABA
AYOOO
BABA
KING BABA
AYOO
BABA
KING BABA
AYOOO
BABA
KING BABA
Fin

Interpretation for


Add Interpretation

A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z #
Interpret