Safary - Deuk bi yeungou lyrics

[Safary - Deuk bi yeungou lyrics]

Kholal famou rétane
Kholal lamou diantal
Oh mom la beugeu Nekal
Waw thia feeling bala
Hé hé thia feeling bala

Kholal lamouy dégagé
So amoul contrôle dalay dérangé
Thia feeling bala
Waw keye, thia feeling bala
Kholal lamou sadji
Bilay Walay beugeu na lii
Lam deff ci daleu da bari
Hum tang na fils déko dieuri

Sangou laal push deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Sagnesé deff hum deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou


Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Guéneu deff, deuk bi riir
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Sassou ma né beureudj deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Ndakh dal thia feeling bala
Tay deuk bi yeungou

Laf bouche,
Néma defatinga
Pas touche,
Lady boss nieuwatina
Wolma wa Aléa bi
Wa génération weundél thiaabi
Mangui ni
Kouy lakatou douko wakh khalé bangui ni
Meti ni
Deff class ak tokou harmonie
Kou defoul wone bama deff tayi ko
Ma wakhla, volume bi wagniko

Sangou laal push deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Sagnesé deff hum deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Guéneu deff, deuk bi riir
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Sassou ma né beureudj deuk bi yeungou
Ndakh dal thia feeling bala

Bakh gueun riche am base buzz beuri feeling bandit
Bakh, gueun, riche
Beuri feeling bandit

Man dama Bakh gueun riche am base buzz beuri feeling bandit
Man dama Bakh, gueun, riche
Am base bandit

Sangou laal push deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Sagnesé deff hum deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Guéneu deff, deuk bi riir
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Sassou ma né beureudj deuk bi yeungou
Ndakh dal thia feeling bala

Interpretation for


Add Interpretation

A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z #
Interpret