Wally B. Seck - CONFUSE (feat. Mia Guisse, Amadeus) paroles de (lyrics)
Wally Ballago Seck [Ndakaaru, Le Sénégal] 🇸🇳
Mia Guisse [Tambacounda, Le Sénégal] 🇸🇳
Amadeus [Massamba Amadeus] Khombole, Sénégal 🇸🇳
[Wally B. Seck - CONFUSE feat. Mia Guisse, Amadeus paroles de lyrics]
Yaay booy wouyouma, damalay laadj (yeah)
Baay booy yédd ma, damalay laadj (yeah)
Beugouma loubakh reuthie ma, damalay laadj (yeah)
Beugouma réthiou tam, damalay laadj
[Couplet 1]
Khamna limouy laadj
(Limouy laadj, limouy laadj)
Niom niaar, kouné mounguék liniouy laadj
(limouy laadjté waw)
Damay beuga diakhlé
Ndakh awma choix ci
Niaar niou doywaar
Beugg nga mais ya ngui xel niaar
Beugo kou xar sa xol bi niaar, baby
Xeyna gnifi diota diaar nio
Fowé sa xol banga fokni nieupa soxor
God loumou bind dathié deff niarr
Ta yaw yaay sama guénwaleu man
Assaman si nimou yaato
Naadj bi limouy tang
Yaay képar guiy neubb naadj bé
[Refrain]
Damay beuga diakhlé
Awma choix bébé khamna limouy laadjté
Linguère nga boul diakhlé
Mbékté dounya yi rek laala yéné
Hey, Damay beuga diakhlé
Awma choix bébé khamna limouy laadjté
Yow Linguère nga boul diakhlé
Mbékté dounya yi rek laala yéné
[Couplet 2]
Souma guissé nganane da ngama nop
Té ndeye dji seikh dou ame ci diamalé
Melni assaman ci nimou yaato
Ak bidéw yi niniou taaro
Nékh nama, wayé diakhlé
Ndakh khamouma, kimay taneu
Linguère may
Latyr Diop Déguéne Mbaye (Anh)
Ballago Khaliloulay (Wouy)
Ndiabote gueu lay woutal yaay
Té keur ga yafa doy lingère way (Ayaa)
Maadi bour guéweul
Khouss ndama lay béguel
So beugué malay wayal
Thiol, ndér ak tama way
Linguère kay
So banié ma wett kaay
Kaay
Yaay sama wérouway
[Refrain]
Damay beuga diakhlé
Awma choix bébé khamna limouy laadjté
Linguère nga boul diakhlé
Mbékté dounya yi rek laala yéné
Hey, Damay beuga diakhlé
Awma choix bébé khamna limouy laadjté
Linguère nga boul diakhlé
Mbékté dounya yi rek laala yéné
[Outro]
Nékh nama, wayé diakhlé
Ndakh khamouma, kimay taneu
No-no-no mon bébé
Ne t’en vas pas wawaw
Nékh nama, wayé diakhlé
Ndakh khamouma, kimay taneu
Signification et Critique Wally B. Seck - CONFUSE (feat. Mia Guisse, Amadeus)
Compositeur : Papelaye Beats
Auteurs : Amadeus, Wally B. Seck
Enregistrement : EDGE Studio
MIX/Mastering : SirTam
02/08/2024