ISS 814 - Penalty lyrics

[ISS 814 - Penalty lyrics]

Penalty
Homme de tenue bëgg dunde corruption
Entreprises di sandi déchets pollution
Jox la ndombal tank defoo résultats
Président bu bëgge ñeeti mandat

Entreprise dieki tëjj
Gestionnaire këpp caisse
Hôpital morgue deuthie
Bës bu né neew bu bés
Civisme si mbedd mi
Nane café sandi casse
Problèmu jànge bu wésu na syndicat

Waar mbith waara mbith
Arbitre du sol 10
Capitaine dou sex mbipp
Lo yor marakiss
Crampons dou tarxis
Surface valenti
Hors-jeux munaan but


Loy xaar: penalty!

Penalty!
Arbitre sifflé wuko ñisi ban bi nioko mbipp
Penalty!
Boo nekkee njitt defo li la war yëpp ñi nga djité niokoy mbipp
Penalty!

Allalu njirim bi nga teud def sa noce
Lu ñëpp bokk yow nga jël ko def sa poche
Sa xaritu benn bakkan am lu baax nga mer
Pusël fëlé yow de am nga dal no mel

Tothie sa math tes delou classe
Mo geuneu ngay
Tothie sa mbarikh munaane tass
Yow doom ndaye
Systeme yereumoul ken
Mësu la bëgg du deign
Fexel ba jafandu fenn
Nenala deugue du fenn

Députe
Ñu fay la weer yow ngay nelaaw Assemblée
Monsieur le Maire
Jaay n'a suf si wax ma xale yi fu ñuy fowé

Waar mbith waara mbith
Arbitre du sol 10
Capitaine du sex mbipp
Lo yoor marakiss
Crampons du tarxis
Surface ralentie
Hors-jeux munaan but
Loy xaar penalty (jogal)

Penalty!
Arbitre sifflé wuko ñisi ban bi nioko mbipp
Penalty!
Boo nekkee njitt defo li la war yëpp ñi nga djité niokoy mbipp
Penalty!

Day kass, nagn ko Var ralenti
Day kass, nagn ko Var ralenti
Day kass, nagn ko Var ralenti
Mou diok
Day kass, nagn ko Var ralenti

Interpretation for


Add Interpretation

A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z #
Interpret