ISS 814 - Tekna Ci Yaw lyrics
[ISS 814 - Tekna Ci Yaw lyrics]
Bu fi nekkul dootoo baax
Ma ñëw yëkketi la
Bul jooy, loo gis am na lu tax
Xamul sa valeur
Daf la négligler ba ma jot ci yaw
Ne ko mu talal
May ki lay defar ba nga yëg ci kaw
Tek naa ci yaw, baby
Indil chèque bi damay signer bilaay
Tek naa ci yaw, baby
Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
Tek naa ci yaw
Say copines dañuy sissou
Ouh ouh
Sa ex dafay sissou
Ouh ouh
Dénk ma love bi
Jox ma sa xol bi
Kenn du la weccoo baby
Ngalam nga doo përëm
Xale bee metti, bari feem tek ci
Moom bu la jekko xamul baale xamul yërëm
Jàmm li ngay jàmm
Bégal bi nga ma bégal
Loxo bi fig ko dugal
Man moo ma ray
Laal bi yaa ko dam
Ndig bi yaa ko dam
Tëddel sama dënd
Nelawal kenn du la yee
Wouyay yoyy
Yeah ye ye
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek
Tek naa ci yaw, baby
Indil chèque bi damay signer bilaay
Tek naa ci yaw, baby
Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
Tek naa ci yaw
Say copines dañuy sissou
Ouh ouh
Sa ex dafay sissou
Ouh ouh
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek