ISS 814 - Soma Bëggé lyrics

[ISS 814 - Soma Bëggé lyrics]

Boo ma bëggee danga may defal cadeaux
Di ma naxee yëngel caabi auto
Mon bébé dugal ma ci château
Ma jël fa samay foto wan leen ni nammuma cooco

Kaay fecc ak man
(Ñëwel ñu fecci)
Kaay fecc ak man
(Ñëwel ñu fecci)
Kaay fecc ak man
(Ñëwel ñu fecci)
Kaay fecc ak man
(Ñëwel ñëwel ñëwel)

Tukku ci ngalam
Musique bi di daw ñëpp di dance
Ma def la madame
Yëkkati ba ci kaw
Ñepp la fans ba nare basang
Hôtel lañu jëm jàppu fa temps
Ma ne bu repe dee bu reppul dee tay la bësam



Ajul ba ci kaw jàppu sa njax nit yi la bëggul
Ci suuf lañu nekk tok di la xar ree de soucis
Ree de soucis yaw doo jegu ree de soucis
(Heee ree de soucis)
Am nga cat am nga feeling
Fees nga dell mel ni meeting
Dëgg daaj teksi cline
Fu ma tourner nga toppuma mel ni sikkim
Yaay biru xaar ci deexin bébé

Soo ma bëggee dagu may defal cadeau
Di ma naxe yëngel caabi auto
Mon bébé dugal ma ci château
Ma jël fa samay foto, wan leen ni nammuma cooco

Kaay fecc ak man
(Ñëwel ñu fecci)
Kaay fecc ak man
(Ñëwel ñu fecci)
Kaay fecc ak man
(Ñëwel ñu fecci)
Kaay fecc ak man
(Ñëwel ñëwel ñëwel)

Xale bile nammul përëm
Waxalewul or diamant fees na dell këram
(Nammul nammul tus)
Dëgg daaj tak sërëm
Goor du ko yàpp ma ko bëgg ma ko gërëm
He ma ko gërëm ce ce!

Bàyyil lak sa biir, coow li di riir
Caaw nga sa xiir
Noquleen bañu miir
Jekk bii du liir
Faux bi du piir
Nob la ba miir
Léegi sax dama fiir

Interpretation for


Add Interpretation

A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z #
Interpret