Narah Diouf - Gouro lyrics
[Narah Diouf - Gouro lyrics]
Nga def ma sa jabar
Ñëpp toog ma seddel la
Ne yaay ki ma sagal
Dañu dem ba nduroo
Yaay ki ma Yàlla boolel
Duñu mësa reero
Ndax dañuy dund mbëggeel
Indil nga ma guro
Desalatoo ma dara
Yaay sama chamalama
Maay sa ding dong
Xol bi di tëgg ni tama
Yaay sama best song
Ma sëy, ma sëy, tey ma sëyel la
Ma sëy, ma sëy, indi nga guro bi
Ma sëy, ma sëy, tey ma sëyel la
Ma sëy, ma sëy, indi nga guro bi
Lu mu metti metti xam na ne yaa ngi fi
Def nga ma sa soxna tey bég naa
Baby, teraanga bi mat na teral nga ma
Jambaar joni-joni
Gile gile jambaaree
Yaa ma tànn si seen biir
Maa la bëgg piir, wax ma lu koy dindi
Dañu dem ba nduroo
Yaay ki ma Yàlla boolel
Duñu mësa reero
Ndax dañuy dund mbëggeel
Indil nga ma guro
Desalatoo ma dara
Yaay sama chamalama
Maay sa ding dong
Xol bi di tëgg ni tama
Yaay sama best song
Ma sëy, ma sëy, tey ma sëyel la
Ma sëy, ma sëy, indi nga guro bi
Ma sëy, ma sëy, tey ma sëyel la
Ma sëy, ma sëy, indi nga guro bi
Moom la, moom la
Moom la, moom la
Ndanaan mooy ki feñ sama dund
Foo jar ma wayal la
Ndanaan wo woo
Su ma demee balay wëy
Seck ndanaan nange
Mo ngi ne
Seck ndanaan nange
Mo ngi ne
Seck ndanaan nange