Narah Diouf - Jaar Jaar lyrics

[Narah Diouf - Jaar Jaar lyrics]

Lu mu metti metti, amul bàyyi
Amul tàyyi, no duñu xaadi
Doyloo Yàlla buur bi ndax moom moy ki ñu binde
Moo ñun gindi, no duñu bàyyi

Yoon wi gudd na lool, sori lool
Ragal xaaju fi
Non, yoqu jibbu fi
Gëm ki ma doon lool
Moo ma def li ma doon
Gëmleen ne
Yóonu ndaw du gaaw
Fow mu tar pour nga raw

I'm on my way, so move away
I shine like a diamond, from Dakar to London
Trust me, coono du reer
No no du mësa reer
Xamal ki nga doon, moo lay xalal sa yoon

Lu mu metti metti, amul bàyyi


Amul tàyyi, no duñu xaadi
Doyloo Yàlla buur bi ndax moom moy ki ñu binde
Moo ñun gindi, no duñu bàyyi

Fi àdduna tollu ni
Sa jom ak sa fula ñoolay motali
Boy, duma mësa fàtte
Li ma dund li ma daje ba yegsi fi
Yoon wi metti lool
Maa koy yëg ci xol
Gëm naa ne sama jaar-jaar la
Waaye lo muñ mu jeex

I'm on my way, so move away
I shine like a diamond, from Dakar to London
Trust me, coono du reer
No no du mësa reer
Xamal ki nga doon, moo lay xalal sa yoon

Lu mu metti metti, amul bàyyi
Amul tàyyi, no duñu xaadi
Doyloo Yàlla buur bi ndax moom moy ki ñu binde
Moo ñun gindi, no duñu bàyyi

Ma ne boy dem
Ba xamatoo fa nga jëm
Dellul fi nga juddoo fañ la ngénte, fañ la tete
Fi nga magee, fi nga jànge l'école

Interpretation for


Add Interpretation

A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z #
Interpret