Narah Diouf - Peundeul lyrics

[Narah Diouf - Peundeul lyrics]

Ak fo né thi town bi
Foo ne ci réew mi ñëwël fi yëngu ci lii
Narah laay dooni
Man la ma ñëwaat fi gëna teggu ci beat bi
Xoolal ni may dugge
Xoolal ni may yégge sama baat ci kaaw
Mélodie bé meu yéglo
Gisatuma, déggatuma
Lenn lay gis kon kaay fii ma wone la
Gisatuma, déggatuma la

I’m so high
I’m so high yeeeh

Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël

Lu fora fora fort lay yëg sama xol
Fu kawe kawe kawe lay yekk sama yaram di yëngu


Ta xawma li koy yëngël fi mu jogé
Ayooooo
Guddi guddi non stress la dundu happiness
Tay non stop
Àndak samay way tay de fête la
Xoolal ni ma mel, kaay dance all night

Sound bi ndax yankay ngueug comme mane ni ma key yeugué
Wax ma ndax muñ lay duggu comme nimmey dougué
Gisatuma, déggatuma
Leen lay gis kon kaay fii ma wone leu
Gisatuma déggatuma la

I’m so high
I’m so high yeeeeh

Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël

Faxasul faxasul faxasul yow
Gënel li ci xol bi, tay duñu maye dara
Yëngëtul yëngëtul yëngëtul yow
Faxasul faxasul faxasul yow
Gënel li ci xol bi, tay duñu maye dara
Yëngëtul yëngëtul yëngëtul yow

Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
(Kaay ñu pëndël)
Narah mu pëndël pëndël pëndël
(Kaay ñu pëndël pëndël pëndël pëndël eeh)
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Ehhh ehh ehh ehh ehh
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Hummm hummm

Interpretation for


Add Interpretation

A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z #
Interpret